Menu Close

Bagage Si Engine

KCC Mboothaye-la bi ye yangatou si wallum machinu bayekatyii nyu hameh tractor ak jumtukaye yi muwara andal beh senu legaye mana sutti si bir Senegal.

Bagages nyoye Caterpillar, Komatsu, Volvo John Deere, Hitachi, Cummins, Detroit Diesel, Terex, Bomag ak Bobcat

Am nen yu bepe bagage bunngen sohla sa suneh, bah pareh man nen yu yombal utbi ak yoblako finko sohleh, mo ham bu eslla, bougne jafandiko teh sonnut, recondition, leppo liguene, yelo, chi wallum machinu ligueokayi factory yi. Wala machinu gasekayeh chi sancheyi, plasu gasekayu minyi, am nenyu machinu jambat-garapyi yu fort teh wohrr. Am nen yu tamit machine ye defar yonnyi-taliyi ak dekuwayyi ak senu jumtukayi yi nyu wara andal yepp nyu ngitew di lenn deglu.

Lo sohla mungi sisa bonti kerr si sa si.

Bagages Yi Engine Yi Pour Jaye Si Bir Senegal – KKC Mbotaye la boye yangatu chi wallum enginyi ak bagage yi nyu wara andal.am na nyu jot lol machinyi denenko johe fune teh it denenlako yobul finko beugue, mo ham bu essla wala sah mo ham bongne jafandikola teh sonnut lol anda nak ak sene bagage yu mut teh wer. Woh lenn nyu pour bepo faconnu machine ak likoye dawal, bagagesu machineyu wer legen sohla yep pour yombal sen ligaye amnenko pour askanbi.

Auto Yu Magyi Ak Truckyi Si Bir Senegal – KKC denen yangu chi jaye yit aye auto-baggage ak aye truck chi nyaglu yombu teh wor. Chi bir Afrique manam Gambie ak dekka yiko wor dinenla mana jaye auto yi chi anam bokko beugue mo ham auto yi tibi suflah pour tabakh wala auto yi daga banti njiyefyi ak auto yi ebb ak wacheh bagageyi am nenn aye auto yu mak pour poryee ak tefesbi auto yuye tabakh amna amnayit bepo faconnyi auto pour ligaye lumu did-dis sunu autoyi yombal nenn lepp.

Machinu Tabaka Ak Machinu Gasam Suff Si Bir Senegal – Wolenn KKC sa bolen sohleh machinu tabakh,machinu gasam suff, machinu jambat garap,machinu defar yonnyi autoyi, mannenlena japaleh tamit chi machinu noyal suff ak wallehkayusuff machinu gis yonwi nga ligaye yi tamit amnen ko lepo ligen sohlah chi wallum machinu ligage yon nyi mungi lena harr chi bir KKC.

Generator Yu Am Doleh Ak System Currant Si Bir Senegal – KKC yit denaye yangu chi jaye defar ak maintinance aye generator yu am doleh ak ki tamit aye baggasu currant yu am doleh tamit,bokana chi machine yi di machine yi dohal factoriyi magyi ak plasu legayeyukayi industriyi ak kerryi tamit, plasu commercialyi, nyu ngi chi tefesbi, chi hotelyi, opitalyi, airaporyi, plasu gouvermayi, nyu ngi funeh ak si bangueyi.

Defarbi Ak Maintenance Bi Si Bir Senegal – Machinu diesilyek, generatoyek, jaye bi ak luwasbi, defar beg leppo chi loho yu wer ak KKC. Am nenu yit aye nit manamaye professional parre rek pour yombal senn ligaye chi nogenko bougue hamnenyu lepp lu jem chi wallum machine ak lilendi dohal numu wareh lepo chi bir ak biti KKC. Sunnyu profesional yi ak seni ham-ham pareh nenn teh taku nenn tamit pour japaleh askanbi chi leppo lunnyu sohlah chi machinyi ak nin lendi dohaleh.

Bagages Yi Engine Yi Nyi Ko Jaye Si Bir Senegal – KKC linnyu pareh beh pareh moye fireko fo yato lin beugue sah moye wor Senegal yepp mo tah nyogi fehe noyu yatalleh warwi sa suneh. Ni nyo ko bouga defe moye obeku, wohteh, jokor ak askanbi, dego ak jayekatyi jandakatyi bagageye machine chi yu melni, jayekati machine yi Caterpillar yi ak bageges yi mu andal si bir Senegal, Dakar, Touba, Thies, Kaolack, Ziguinchor, Mbour, Rufisque, Saint-Louis, Diourbel, Louga, Richard Toll, Tambacounda, Kolda, Mbacke ak Fatick

Leave a Reply